Abdoul Aziz Sy Junior et Serigne Moustapha Sy ibn Cheikh Tidiane


Mardi 12 Février 2013




1.Posté par mige le 12/02/2013 01:25
li louko gueuna raféte?

2.Posté par nabou le 12/02/2013 02:16
vous les administrateurs de dakaractu vous etes vraiment bizarres. E3st ce que vous vous rendez compte de votre titre. DE par son age de par son parcours , de par sa sagesse et de ce qu'il represente dans la communaute tidiane et dans le Senegal donnez lui son titre de Serigne Abdoul Aziz Sy Al Amine,.Si vous pouvez ecrire Serigne Mustafa Sy ( apres tout c son pere et son maitre ) pourquoi pas Serigne Abdoul Aziz Al Amine. Yallah moko teral konak boula khadj yi teraloul dou la wagni dara

3.Posté par y'a rien de mal le 12/02/2013 02:33
dara nékkul si titre bi, Abdul Aziz sy "Al amine" loolu mame abdou dabax moko yéllo ndakh "L'amine" moy kougnu woolou ta mame abdou gneupaka woolou wone. Ki nak deugla lègui mag la mè takhoul gneup woolou ka, ndakh yakh rék lafi néké woone, bamou jaxlé la beug nék di jèma défar, mè dou royukay pour la jeune génération, un jour devant tt le monde ci bèn gamou mou Saaga ba nopi nane bal léne ma, recement il ns a insulté ns les jeune tidianes ni danou rèw devan la télé ba paré mou beug gnou diokh ka thieurou mak ta diokhouko woone mome gniko mak! Day yomb! Léptoo faytoo. "Il sera toujour junior" comme le disait ce Moustapha Sy

4.Posté par rita le 12/02/2013 03:59
poste 3 deugeu bou réye gueu fi wakhe junior doit savoir qu'aucun talibé de cheikh n'est un mouton

5.Posté par mmmbaye le 12/02/2013 08:01
un peu de respect et de consideration a serigne abdou quand meme

6.Posté par Talla le 12/02/2013 08:57
très belle image

7.Posté par farata le 12/02/2013 09:18
poste 3 je te demande combien de fois ton pére t'a insulté, t'a dit que tu es impoli et pourtant tu lui donne le respect d'un pére. Ton intervention confirme les propos de serigne abdou aziz sy al amine disant que les mourides sont plus diciplinés que les tijanes. un mouride ne tenira jamé ses propos à l'égard d'un mbacké mbacké quelque soit son carractére et ses comportements. al amine nak c'est mame abdou qui lui avait donné ce titre parce que il avait confiance en lui et donc nous aussi nous avoir confiance en lui si nous l'avons pour mame abdou. bilahi sou nékoutone ak serigne abdoul aziz sy "al amine" lou bari ndiaw.

8.Posté par koungala le 12/02/2013 09:29
c vrai Poste 3. il n'est pas une référence. il a même manqué de respect à l'actuel khalife en disant devant tout les talibés mome dé gewoul baléégui mais gnounn gnoo ngui agne di réér. Cela montre netement qu'il est indifférent au statut de khalife de Chiekh tidiane al makhtoum. ce sont des propos trés discourtoie qui ne cadrent pas avec son statut de rassembleur dont il fait montre

9.Posté par yalna diam yag si réwmi le 12/02/2013 09:59
niaka wormal mague gni rék moy takh réwmi tardé.nguir yalla koula mag diokhko tieurbi.bayiléne diakhassé keurou dinéyi niome nieup béne déréte bila.

10.Posté par al makhtoum le 12/02/2013 10:21
soyez poli et posé les gars Serigne Abdoou Aziz AL AMIN Yala mokofitek c lui le garant de la famille Sy kouko dieguewoul meno kham ligueyam si senegal ak tarakha bi,deuk bi mom soy wakh deug ak lou lere dougnela beug,AL Amin limou kham si CHEIKHAL KHALIFA ABABACAR SY ak Moulaye ABDOUL AZIZ SY ak ker gui amoul ken kouko kham ndakh mo nekone ak mmak gni te mak gni wolouko trop,legui nak ndawou senegal dagnou roye toubab yi ba doff ndakh lgui khaleyi amatougn respctpr mag gni et ca c tre dangereu fou deuk bi dieum a c rythme, AL AMIN doundeul bamou yague yeguale sa liguey si sa wetou mak AL MAKHTOUM CHEIKHOU TIJANI

11.Posté par Fatalikou le 12/02/2013 11:55
"Kou votéloul PS imbécil ngua! (vers 93...) Tidjane yi dagno rèew! (2013) Man ma wakh piliciers yi tiré léne ci foule bi! (2012) Gamou allaji malick moka moome! (2013) saga devant tout le monde (plusieurs fois) et maintenant il veux qu'on lui traite comme mam abdou? Impossible! Lou yakhou tiwawone li ci eup moome leu!

12.Posté par cheikh le 12/02/2013 12:26
En tant que défenseur de la khadra de Seydi El Hadj Malick Sy, il est toujours aller au charbon durant les grandes crises. Cela requiert à la fois diplomatie et rigueur. Il a choisi de se sacrifier pour la hadra quoi que cela puisse lui coûter. Certains n'ont rien compris de la manière dont une Grande communauté comme la notre fonctionne, avec sa complexité et les fortes personnalités qui la dirigent.
Que Dieu continue de les éclairer pour qu'elles puissent nous guider dans la rectitude
Que Dieu rétribue à Al Amine ce sacrifice au Service de ses illustres aieux

13.Posté par y'a rien de mal le 12/02/2013 12:45
@farata, les mbaké mbaké ne sont dans la meme position k Junior, eux c leur grand père qui a crée leur voie mouride, tarikha de mame bamba (rta), et la tarikha de cheikh ahmed tidjane (rta) n'est pas la tarikha de mame maodo (rta). Jr dou sunu serigne sunu mbok talibé leu, so beugè kham gnane nioye les marabouts de cette danguaye deme pikine (dakar) dafa fék ay seutou sidna cheikh ahmed tidiane (rta) c eux les petit fils de cheikh les héritiers de leur noble grand père le fondateur de cette tarikha. on dit tarikha cheikh ou tarikha tidiane, et non tarikha malick. Junior talibé leu si tarikha bi ou bien mome la beug done (yala rek mo kham kimou nagoul) comme nioune wayé dou sunu serigne dou sunu domou serigne

14.Posté par deug le 12/02/2013 14:45
Moustapha sy doit avoir avoir honte. que n'as-t-il pas dit de mal à fils de serigne babacar sy dont il glorifie??? Il lui a tout dit de mal et de mauvais. aujourd'hui, il lui tend les maains pour recevoir ses prières! quel honte! je plains les talivbés de moustapha sy nakh kii meutoul serigne. khana serignou kou beug bone. il n'a encore rien vu. car même serigne cheikh son père le désavoue. il est trop vicieux. on a encore les cassettes dans lesquelles il insultait tout le monde même mame dabakh de manière inssinueuse. mais un jour ou l'autre elles le rattraperont. c'est mê déjà arrivé. le maouloud de cette année, il a été pâle.

15.Posté par moussa le 12/02/2013 16:32
dou rouss dara amoul koufi diotéwoul ak papam . les problèmes sont clos téyélène sén lamigne yi thi mbokgui .

16.Posté par al makhtoum le 12/02/2013 18:59
Deuk bi defarko do yombe ndakh gnak khormeu

17.Posté par nar le 12/02/2013 23:51
en tou cas yal na yalla defal leeenn niom niep diam ak wer si barkep seydina mouhad amin ak sen barkep mame

18.Posté par falahou le 13/02/2013 10:03
yalana diam yagg, yé fitna bakhoul, wakh bou rafét mo gueun bou gnaw nguir yala khalat lén teurayou bamél

19.Posté par pape le 19/02/2013 13:18
@Posté 12 MERCI mon frère, toi tu comprend:



Dans la même rubrique :